Wiri Wiri

Wiri Wiri

Diaw Diop Didi

Альбом: Wiri Wiri
Длительность: 3:42
Год: 2021
Скачать MP3

Текст песни

Ioe wiri wiri diari ndarii
Fo meuntii demitt baby dinga deloussii
Koti koti yoli yoli
Kay fi ma nakh la yadi sama néné touti
Boul daw meuneu daw takhouta reuthie
Loy doyé or so amé diamant bissi keurgui
Matt lima donn indil contrat niou signé
Foukk si niom man rek ma yeungeul geusseum
Ken dou yeungeul

Niémé na lolou titouma lolou
Gagné wala gagné match nul yalla téré
Niémé na lolou ragalouma lolou
Gagné wala gagné match nul yalla téré

Ba takh na dangadon lamb dadj nga
Dangadon sett dh guissnga
Eh man la affaire bi man la
Dangadon lamb dadj nga
Pèsser nga xamnga diss na
Eh man la nangoul ni man la

Dall ngassi dall ngassi ioe bi bou bax bi la
Dall ngassi dall ngassi si si bou bax bi la
Dall ngassi dall ngassi ioe bi bou bax bi la
Yako tay xamngani bi ni bou bakh bi la

(Woma womaaa ioe)

Ioe wiri wiri diari ndarii
Yangui dem té yangui deloussi
Ma dila ayo ayo néné dila néné néné touti
Doranté dakanté melni xalé
Yay sama Tom dh may sa Jerry
Malay teull di teulteull
Don sa seytané dila diomall
Adj bathia kaw wathié la si souff
Rogantii teup teupeul nila nopill

Dangadon lamb dadj nga
Dangadon sett dh guissnga
Eh man la affaire bi man la
Dangadon lamb dadj nga
Pèsser nga xamnga diss na
Eh man la nangoul ni man la

Dall ngassi dall ngassi ioe bi bou bax bi la
Dall ngassi dall ngassi si si bou bax bi la
Dall ngassi dall ngassi ioe bi bou bax bi la
Yako tay xamngani bi ni bou bakh bi la

(Tassou + sabar)